|
Jeunes Tidianes : Serigne Maodo SY met en garde contre les conflits
macha ALLAH sangue bi yalna yalla yokk ko deugeural mom ak domam dji serigne Moustapha Sy Abdou baarakallah contane ngne ftabaarakallah sope ko lol sakh ba diekh si wakeur mame maodon inechallah
MACHALA SY MALICK; yala na ko yalla may goudoufane ak wer. fa mame abdou tékone tankame rèk la tope. Khamna wadiourame bou tédba daf koye guena goude tank, guene ko yatoulé wayé mome rèk laye roye. Sounou sague la thi diiné dji ak hadra bi. doundal lou yague sy.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|