MACHALA SY MALICK; yala na ko yalla may goudoufane ak wer. fa mame abdou tékone tankame rèk la tope. Khamna wadiourame bou tédba daf koye guena goude tank, guene ko yatoulé wayé mome rèk laye roye. Sounou sague la thi diiné dji ak hadra bi. doundal lou yague sy.