|
KEUR DIEUMB (THIÉS) - Ziarra de la famille Tafsir Allassane Mbaye ce Samedi 23 Janvier 2016
Bék rék si takhaway bi ak lifa SERIGNE ABDOUL AZIZ SY AL AMINE Toute la famille est fière amougnou sén féy té YALLAH fayal gnou soune makkk gni té tég gnou fane tégone séni tank dina djafé gnou tooloo ak gnom tanke wayé nane fékhé ba foune tégone sén tanke gnou djém fa tékk sounouy tanke ba kérok gnou léni fééki
alhamdou lilahi yallana yalla yok fanyi te weral tieryi tey nian nak balla dewen ker d am courent ak talli qi barke serigne bi aminn way
amiine ndiaye lolou mom war na ame
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|