|
LETTRE DE SEYYIDINA CHEIKH AHMAD AT TIDJANI CHÉRIF AUX DISCIPLES
alhamdoulillahi ! dieureudieuf CHEIKHNA! YALNA YALLA YOKOU SA LÉRE TÉ TAAS NGOU SI SA BARKÉ.
Al Hamdoulillah ! Diaza allahou anna Cheikhana wa seydanna abbal abass ahmad tidjanni
Dieureudjeuff asfiyahii mashallah
dieuredieuf sama sérigne cheikh
alhamdoulilaahhhh!!!!apprécier na té gueumenaa ak yahiiine...Sounou faare bou lééére biiiiiye léééérale diamono ba kére bagnouye tabbi ILLIYIIIINA.....CHEIKHOU TIDJANE CHERIIIFE....YALLNA YALLA YOOKKA LEEERAME TE TAAASSE GNOU THI BARKEEME....AAAMIIINE
sante yalla rek ake sangue bi ba niou dioudo si talibé cheick et taye niane yalla dé si akhe wird si barké seydina MOUHAMED (psl)
Notre Cheikh est un océan de savoir. Quiconque se soumets a ses dires; n''aura pas de regrets devant son Seigneur. Qu''Allah augmente sa générosité.
kou niou khass sa serigne nga mer booba niaar rek moo am :
_ benn mo fekk sa serigne tollou woul na nga foog.....
_ niaar mbaa yow si sa bopp khamoo sa dayob serigne...
Seyddina cheikh taal bou yalla taal la loo si wakh rek da ngay guena djafal taal bi ....
GUEUM BA DEE
BEUG BA NEUP
ROY BA FAW
SI BARKE MAAM MAWDO SAMA SOPE
damay deuk ci dila fonk té lay sagoo. yaal na la sounou borom faye ndax fi nga gnou yaub. dieureujeuf CHEIKH
MOUHAMADOU AHMADOU NDIONGUE
NOUS REMERCIONS CHEIKH D'AVOIR AUGMENTE NOTRE FOI EN DIEU K'ALLAH LUI PAIE
Merci de la générosité intellectuelle mais on aimerai bien disposer du texte arabe si possible
all hamdoulillahi rabill ala mine dieuredieuf cheih ahmet tidjian pour tout que vous avez fais pour les musulmans en particuliers les tidjan. un grand remerciement a ELHADJ OUMAR ET MAME ELHADJ MALICK SY MAODO.
ya rassouloullaah alhamdoulillaah ila aldiana ah tidjania.
dieureudieuf mame cheikh santa yala rek
yalle naniou yalla raye si tarikha bii. mame maodo sy amo morome, dieufeule nga yalla sa borom, kou ko roy mou ngui roy cheikh, di roy yonénte, bilahi li khole di yéné khalima mounoule binde louko fére loo. SOUBKHANA RABIKAL RABIL HIZATI HAMA YAASSIFOUNE WA SALAMOUNE FI DOUNE YA WALE AAHIR WA SALAMOUNE HALA MOURSALIINE WAL HAME NDOULILAHI RABILE HALAMIINE
Bonjour je suis ravi de faire connaissance de ce site ce qui m'intéresse le plus c'est quant tant que jeune tidiane qu'à travers le site que je puisse apprendre davantage le tidjanisme dans sa globalité.
MERCI DE VOTRE COMPREHENSION
diazaka lahou khayrane cheikhna Ahmad At tidjiani
badou bou cheikhou tidjany
DIEUREUDIEUFE CHEIKH TIDJANY FASSSSSSSS DIARAMA BAYE BARHAMA SENE
alhamdoulilah que le bon dieu nous guide vers le droit chemin par la grace de cheikh
ahmed tidiane
Wa RadiyaLahou ane Cheikhi Tijani Cherif wa Ardahou.
Wallahou Diazakoum khayrane Djazila Yaa Cheikhna Wa Mawlana Ahmad At tidjiani Cheirif Hassani Fatimi
allahouma ajzina cheikhana wa wassilatouna cheikhna ahmed ibn mouhamed tidiani radiyallou
anhou khaira jzahi diadieuf
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|