|
Mémorial des Saintes :Sokhna Rokhaya Ndiaye, épouse de Seydi El Hadj Malick Sy (RTA) 1ère Partie.
EL HADJI MALICK SY SAWANDE L HOMME TRES PIEUX LE GUIDE DE TOUS LES SENEGALAIS PUIS C EST UN HALPULAAR.
ALLAHOU AKBAR.................yayou serigne Babacar sy,yallananou yalla taf si sa barke.AMINNNNNNNNNNNNNNNNNN
kou khole sa diardiar dina khame ni gorougue yalla rèka diara andale motakh yalla fèyèla dome diou adouna bèpe khame aye mayame .bo dèguè tourou khalifa khèle yepe dème si domou sokhna sou bakh dji royacaye nga yalla naniou yalla tass si sa barkè amen
ma sope famille seydi elhadji malick (R T A)
amouléne morome sy malick goorgui dafa liguéyeul boromome motaklh mou am litay
Yalla naniou yalla faye Seydi El hadj Malick . Yalla na yalla yok leram te tass niou thi barkem
macha allah yalla na laine yalla faye
diarama mam rokhaya ndiay
alhamdoulilah bima dioko thi seydi hadj malick. yalla na yalla yok leeram ak ay ndiobotam.
yala nanou yalla tass si sa barke mame ak sa ndaboot gui yeup .dieureudieuf mame daba
salam
je viens de decouvrir que j'etais un proche parent de Serigne Babacar et Sidy Ahmeth SY
Khar Yalla SIDY est la soeur de mon aileule Diyana Sidy,mere de Marietou BA qui engendra Amadou Makhtar (premier pilote du senegal) le pere de mon propre pere.
je suis fier d'appartenir à cette famille même si je considere que je suis le frere de tous les autres musulmans
jaam ak xewëul ci sirataal mustakhim
khala chahiroun koudiokou si kou égua si yala eggua si yala lou baax reek moo diara roy sy malick amoul morom
yalla na yalla yook léram té taass gnou si barkém.jigéén bou néék war nga rooy si moom.
yalla.nagnou.yalla.tasse.thi.barkèm.ak.sa.conviction
Pouvez-vous nous parler de Diokounda NDIAYE frère de Rokhaya Ndiaye qui fut longtemps au service de El hadj Malick SY?
Du Colonel Dieng Abdourahmane: ''Vous ne serez pas complets dans cette analyse si vous ne rendez pas hommage au père adoptif de Sokhna Rolhaya Ndiaye qui s'appelait Mor Massamba Dierry DIENG. Maodo Malick était son disciple et enseignait le coran pour lui dans son dahra. Quand il lui a exprimé le besoin de se marier Mor Massamba Dierry DIENG lui donna en mariage sa "fille" DABA Ndiaye. Les gens de Saint Louis se moquaient de Maodo Malick en lui disant qu'il n'avait point de belle famille et que seule la famille de Mor Massamba Dierry lui servait de belle famille. Aujourd'hui tout le monde cherche à être affilié à cette noble famille. Cette face de l'histoire peut être confirmée par la famille S'y elle-même qui est aussi ma famille''
Dieuredieuf tarikha tidjiane bougou kham lou bari si sama mame sa ma tourono sokhna rokhaya akh la famille seye merci
Dieuredieuf colonel dieng mbokaga akh tonton omar dieng bou diourbel ak sama pape abdou seye ancien athlete bouga na kham lou bari si famille si possible merci
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|