|
NÉCROLOGIE - Rappel à Dieu de Sokhna Oumou Kalsom Sy Bint Serigne Babacar Sy
Mame Oumou RTA nitt kou bakh te ame yité...yaneu ko wadiourame Serigne Babacar AK mamame Seydil Hadji Malick RA teerou bijahi SAWS
Innaa lillahi wa innaa ileyhi raajihuun.Na y alla yokk leeram te yééguè la si barzakhou maamam. Condoléances à toute la hadara al maalikiyah et toute la ummah
Je n'ai eu la chance de la voir qu'une et une seule fois; c'était à l'occasion de la Conférence Annuelle Spécial Ramadan qui se tient à Fass chez son Frère Seydi Mouhamadou Moustapha SY Djamil RTA, il y'a de cela deux (02) ans. Je garde JALOUSEMENT le souvenir d'un échange CHALEUREUX et GENIAL avec un être ACCESSIBLE.
Yalna ko Ya ALLAH Bour bi SOUBHAANA HOUWATAALLAH terrou, terral ko ci YEURMANDEEM, yaubbou ko ALDJANA ci barké SEYDINA RASSOUL SALALAAHOU ALEYHI WA SALAM akk ci barké MAAMAM Seydi El Hadji Malick barké BAAYAM bou TEDD BA Seydi Aboubacar SY (RTA)...
Ina lillahi wa ina ileyhi rajihoune sama badiane sana tourendo sama kharite sokhnaoumou kalsoum sy bintou chekhoul khalifa ababacar sy yalla nako yalla yégué si khadara seydina mouhamed salallahou halayhi wasalam
Inalilahi wa inailayhi radjihoune yalna yalla terouko sa barzakhi bayamyou bakhya AK mamame you bakhya bibarakati seydouna mouhamed salla lahou haleyhi wasallam lamine
K le Bon DIEU accueille au Paradis
Mame Oumou yangui ci khol yi yalnala Ya Rabi xar Al diana firdawsi yalnala Mouhamad saws terou ci xadaram ba.amine
sohnacii ndeysaan yalla nakko yalla yerum tee diegal ko.
way way maame boy yalla nalla yonenthe bii gatandu aandeu ak serigne babacar ak maame malick,ameen
Nous de la Cité Aliou Sow de Golf, nous l'appelions affectueusement "Mame". Elle nous rappelait son vénéré père Serigne Babacar SY. Nos condoléances à sa fille, la très sympathique Marème Kane.
Yalna yalla yokou lééram ta yéguéko sa barsaxou djiguene gou baxni
mame oumou nit kou bakh lol am téranga kham téranga di def téranga yalla naniou yalla tas bi barkem fékina bayam ak maman
Gnogui lene koy dial di gnane yallna yalla yok leer te tasgnousi barkeme
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|