|
NÉCROLOGIE - Rappel à Dieu de Sokhna Oumou Kalsom Sy Bint Serigne Babacar Sy
Mame Oumou RTA nitt kou bakh te ame yité...yaneu ko wadiourame Serigne Babacar AK mamame Seydil Hadji Malick RA teerou bijahi SAWS
Innaa lillahi wa innaa ileyhi raajihuun.Na y alla yokk leeram te yééguè la si barzakhou maamam. Condoléances à toute la hadara al maalikiyah et toute la ummah
Ina lillahi wa ina ileyhi rajihoune sama badiane sana tourendo sama kharite sokhnaoumou kalsoum sy bintou chekhoul khalifa ababacar sy yalla nako yalla yégué si khadara seydina mouhamed salallahou halayhi wasalam
Inalilahi wa inailayhi radjihoune yalna yalla terouko sa barzakhi bayamyou bakhya AK mamame you bakhya bibarakati seydouna mouhamed salla lahou haleyhi wasallam lamine
K le Bon DIEU accueille au Paradis
Mame Oumou yangui ci khol yi yalnala Ya Rabi xar Al diana firdawsi yalnala Mouhamad saws terou ci xadaram ba.amine
sohnacii ndeysaan yalla nakko yalla yerum tee diegal ko.
way way maame boy yalla nalla yonenthe bii gatandu aandeu ak serigne babacar ak maame malick,ameen
Nous de la Cité Aliou Sow de Golf, nous l'appelions affectueusement "Mame". Elle nous rappelait son vénéré père Serigne Babacar SY. Nos condoléances à sa fille, la très sympathique Marème Kane.
Yalna yalla yokou lééram ta yéguéko sa barsaxou djiguene gou baxni
mame oumou nit kou bakh lol am téranga kham téranga di def téranga yalla naniou yalla tas bi barkem fékina bayam ak maman
Gnogui lene koy dial di gnane yallna yalla yok leer te tasgnousi barkeme
Yallah nako yallah yereum khareko aldiana Amen et je prie de au bon Dieu d'augmenter aussi la cohésion au sein de la tariha
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|