|
PHOTOS & VIDEO : PELERINAGE A LA MECQUE ET ZIARRA A FEZ DU CALIFE GENERAL DES TIDIANES
c'est tres emouvant billay serigne mansour yal nguafi yageu té weur lolou ak ndiabotou mame elhadji malick sy bi yeup...
c'est trop nékh, bilahi lii dara dakhouko. Borome Darayi, yalla nako fi Yalla bayi baci kanama-kanam té mayko wér...
C'est extraordinaire que le bon Dieu lui prête longue vie et une santé de fer? Yall nanou yalla fayal ma El Hadji Malick SY (RTA).
Yalnakofi yala yagal sougnou kanam mou yag gnoo sogne, yala mayko yér mo yay rakam yeup.Gnou bagna faté diko gnanal gnountamite.
Ziar nalén mkokou talibé yeup.
je suis tres emu , serigne mansour yalla nafi yagg te weerr
Fattabarakalahu, maashaala, maashaala
thank you for sharing, it means a lot for us! ndeyssane it's a moral boost!
longue vie à vous et santé de fer sérigne mansour sy, di la sago rék sasounék, Yalla na nioula yalla fayal ak famille bi yeup. Amine ci barké yonéth bi.
Alhamdoulilahi! Je viens juste de regarder la video et j'avais les larmes aux yeux Macha Allahou. Baakh daal mo am solo. Serigne Mansour que Dieu vous donne longue et une sante de fer par la Grace du Prophete (PSL) de meme que tous les musulmans.
as salamoualeykoum sa ma mbok talibé yi ma gui lén di ziar,[ serigne] MANSOUR SY RTA dou kén kou doul mom sa ma yaram da fa daw barki cheikh. bounou kén guéné si tarikha bi fii nguén diap fofoula bou gou ma wakh sakh mais diap lén té bania bayi si j pouvais avoir vos numéro vous tous
Macha allah, khalifa cheikh foumou dem, gnou kham moy kane! na yalla yok sa fane, yok weer gui di ziarr lou barri.
Si chacun pouvait réciter une fois salâtoul fatiha (santé ko yalla) et le donner au khalife et à toute la famille de mame seyidil hadji malick en guise de hâdiya, gnarigne rek la incha allah
Alla khou ma Amine serigne makhtar ak yawite yalla nala fi yalla bayi ak sa famille ak boléme dioulite té défe gnou ay talibé cheikh amine
comme je le dis souvent à mes amis quand SEYDIL HADJI MALICK RTA incarnait la Connaissance du tarikha son Eminent fils SEYDIL ABOUBACAR SY RTA incarnait sa Sagesse et LE BIEN AIME SEYDIL HADJI ABDOUL AZIZ RTA son Humilité et voila que SERIGNE MANSOUR nous devoile sa beauté dés lors tout un chacun qui le regarde eprouve un grand plaisir au coeur qu'il le veuille ou non.alors que Dieu agrée leurs oeuvres et fasse de nous de veritables disciples de CHEIKH AHMED TIJANE ACHERIF RTA dans la cour de SEYDIL HADJI MALICK.SAMA ZIAR TCHI TALIBE YEUP.WA SALATOU WA SALAM ALA RASSOULLILAH
BILAHI WALAHI SERIGNE MANSOUR MAALA BEUG , KOKOU GUISS NAKOKO WAKH. DAMAKO BEUG SAMA KHOL, YALA NAKO FI YALA YAGAL TE MOU ANDE AKE WER AKE DIAME AKE SOUTOURA INCHALLAH.
YALA NAMA YALA MAY MA GUISSANTE AKE MOME INCHALLAH, SOU MAYE WAKH AYE WAKHAME SAMA KHOL DAFAYE TOOY TELLEMENT JE LAIME DU FOND DU COEUR TE YALA TAKH!!!!
ALHAMDOULILAHI C EST TELLEMENT EMOUVANT QUE J AI PAS REUSSI A TROUVER LES MOTS JUSTES POUR FAIRE UN BON COMMENTAIRE; QUE LE TOUT PUISSANT VOUS ACCORDE UNE LONGUE VIE ET UNE SANTE DE FER
MALACK TALIBE SERIGNE MANSOUR SY
ziar borom daradji YALLA na fi YAGUE té weur merci tiéy BOROM DARADJI ya baakh
sagou keppe kouye tidjiane nga borom daradji que le bon Dieu te donne une longue vie de 110ans et une santé de fer.ces photos montrent vraiment ton humilité et ta grandeur
mamdou faye sope serigne moustapha djamil a malika nord guediaga
je suis vraiment emus en voyant ses images de serigne mansour sy epolee
par ses fils .serigne mansour syn djamil et mansou sy ibn elhadj abdou aziz sy junior que le tout le puissant allah vous benise je ne sais meme quoi dire parceque j ai le coeur plein .yala na niou yallah sayakhal thie tarikha cheikh reeye you dekal yousi .serigne mansou sy djamil yala nala diapalee thie beugue thie tarikhabi te weralele ak sa raka serigne ahmet sy amine yarabi. merci
SERIGNE MANSOUR SY YALNAFI YAGUE TE WERR AK DIABOT GUI YEUP
AL HAMDOU LILAAH , c'est rssurant , que DIEU lui donne sante et longue vie
devant nous.
Serigne Mansour Sy khalif général des Tidiane yalla nafi yagu té wér
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|