|
PHOTOS & VIDEO : PELERINAGE A LA MECQUE ET ZIARRA A FEZ DU CALIFE GENERAL DES TIDIANES
Longue vie et santé de fer à notre Khalif Général et bonne continuation à Asfiya.org, vraiment je me complète en vous pour les nouvelles du Khadara. Longue vie à vous aussi.
Wa sharafil khourane kholl sedd neu trope yalla naiou yalla deff ay deu deug talibe seydina cheikh ahmed tidjane cherif (RTA) KHALIF GENERAL BI TAMIT YALLA WEREUL KO TE YAGAL KOFI BAMOU GEUN YAG
Dieuredieuf sounou Khalifa Général yalla nako fi yalla yagal té may ko wer ngou yaram, asfiyahi sa kaw sa kanane rek. Ziar nalène.
santa yalla rek contane negnou trop khalifabi yalnako fi yalla bayi ba si kaname te mou andak wer
yalla na fi yague tè weurrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnneeeeeeeeeeeeeee
Dieureu dieuf boroom Daradji, Nio nguilay Ziar dila Nianal yala bayila ci sounou kanam may la wer ak werlé ndakh nga meune di wéyeul takhawou dioulid yi. Yaw laniouy Sago Sy Malick
Diaguéne jeuf way sama mbokk yi. Je suis très content de ce site. Merci.
Dieuredieuf SY MALICK yalna na la Yallah bayi sounou kanaw té werel tieur yi.Contane nagnou yow la gnouy sago.Alhamdoulilah.
Allahou Akbar
Longue vie et santé pour nous accompagner et continuer à nous guider
ALHAMDOULILAHI RABINE ALAMINA DI SANT BOU BAKH BI MA YALLA BOLEQUE NIOU MEL NI WA ASFIYAHI. NEK TALIBE CHEIKH REK MO NEEKH, YALNA NIOU KO YALLA DEFALE. SOUNOU KHALIFA BIIII YAL NAFI YAGUE LOOOL TE WEER MOK DIABOTE GUI SI DARADIEYE SEYIDOUNA MOUHAMED SALALAHOU ANLEYHI WASALAM. ZIAR NA GNEUP. MACHALAH
contente trop trop sama khol ba ngui meneni galasse serigne bi yalla naniou yalla tass thi barkeme AMINE
yana yalla gana yatal sa terou way té tass nou si barké sy Babacar
Machalla,vraiment amougnou séne faye,yalla mi am séne faye yalla naléne faye si barké seydina cheikh (rta),amiiiiiiiiiiiiiiiine ya rabbal alamine
Que dieu nous protège de votre sec de soufi qui adore un être humain cheikh tidiane qui à ramené que des innovations dans la religion. Apprenez votre religion au lieu d''invente des pèlerinage alors que le prophète interdit cela pour sa propre tombe
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|