|
SOUVENIR - Lundi 25 Mars 1957 - Vendredi 25 Mars 2016 : il y a 59 ans s’éloignait Serigne Babacar Sy
Manchallah Seydil Aboubacar SY RTA
yalna Yalla yokou lérame té tass niou si bar kéme, amineeeeeeeee
Maa la beugueu Billahi! Yalla na la yalla dolil ay ngeureum ndax yayoo ngako té tass gnou si barkemm! Amine!
YALLA NA YALLA YOK LERAM T TASS NIOU SI BARKEM
KI IL E UNIQUE
BILAHI AMOUL MOROM TE KOU KAY DI7MA WOUTAL MOROM DANGA KHAMOUL REK DIEUREDIEUF SY... YALLA NA NIOU LA YALLA FAYAL...
alhamdoulilah rabil alamina fiére d'etre un fidél de seydi aboubacar sy alhamdoulilah boudoul wone khalifa réwmi dina ledeum
yalna yalla yok leram te tass ñou si barkem yallla nañou doundou si keparam desi
di ñanal louni mel bep talibe cheikh yalla mayñou feke youbari ak tal
amine
alhamdoulila yalna yalla tass nou si barkem sy malick amine
dieureudieuf sy malick yalla nala yalla faye si barké mouhamed
Que ce jour nous permette de débarrasser le pays à jamais du clan Wade et de ses acolytes
Sy malick, khalifa Ababacar, le pays attend tes prières
yalla.na.yalla.yokh.ay.lèram.tè.kharèko.aldiana.fiyrdiwsi.amo.morom.sy.malick
Eskey way 1957 a 2012 chaque annèe,mois,jour,heure,minute et seconde qui passe yagui guena seusse si sougnou khole yi walay yana yalla yoka sa lèer ta tass gnou sissa barkè
Khalifa Ababacar ya nu doy ,dou nu noppe di sakhou diane,yala na yalla yokh ay leram té kharéko si aldiana Ameeeeeeeeen
ce jour ne pouvait pas être plus bénéfique pour le pays. ton ombre salvatrice à planer sur le pays motah Dieu nous a libéré de nos malheurs. yalna yalla yokk sa lérr
bismilahi yalla na niou yalla tass thi sa barké sy je suis fière fièrrrrrrrrrrrrrrrreeeeeeeeeee d' ¨tre talibé cheikh , talibé serigne babacar sy machalla yalla na yalla yokati sa leer té tass niou thi sa barké asfiyahi de l'avant rek.
wasalam
FATABAARAKAL LAH ILA MA CHA ALLAH...IL NE CESSERA DE NOUS MONTRER QUI IL EST ET QU IL EST TOUJOURS PARMI NOUS...
DIEUREDIEUFETI MAAM SY SA LEER GUI DI YOKOU SAY SOPE YI DI YOKOU GNOU CIY YOKOU...
Sokhna Fatou Sy Mansour SARR
Alhamdoulilah
Je suis fière d'être talibé de mame Cheikh Seydi Aboubacar SY. et heureusement la date de l'anniversaire de son rappel à Dieu est doublement marquée maintenant. A jamais l'on se souviendra que c'est à cette date que le Sénégal a été libéré... on ne sait pas de quoi demain sera fait mais au moins personne n'aura salit cette date si importante pour nous.
Puisses ALLAH Faire de tous les talibés et seutt de mame Babacar d'éternelles sentinelles pour un Sénégal de paix et prospérité.
Yalna YALLA tasnou si barké mame Babacr, nangou souiouy niane si Ormaam ti yok ay léram.
SY ,YA NIOU DOY, YAY SOUNOU MAME BA EULEUK
Même dans la Tombe , Nous continuerons a Vous Glorifier, SY MAME MBAYE
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|