|
Serigne Sidy Ahmed Sy Malick , fils ainé de Seydil Hadj Malick Sy , Tirailleur Sénégalais, disparu en Gréce lors de la premiére guerre Mondiale.
salam mangui niaan yalll sougnou boroom may niou léppou lou nou niaan thi gamou gui thi barké boroom gamou gui mouhamed (saw) té yalla bayiii fiii sr cheikh anmed tijane sy al maktoum ak képou kou sante sy rék ak bépou dioulitt itamitxxxxxx
Alioune badara ndaw barcelone
slt ziare lou beuri.gnoune senegal nagnou profité de l'ocasion nianalanté balanté.yalla yok xewal yi bir senegal.nagnou oubi xolyi waxanté deug.liguayougnou dagnouy fo.té les enseignemen de nos gran marabou com EL HADJI MALICK SY dagno lere nagn .yalla na yalla nangou niane yi si barké borom goudigui
Walay douniou ka massa rèthiou ziar nalènn bepp talibè cheikh ak wakeur MAME.EL.MALICK SY ( RTA )
Ziar na dahira MAME SERIGNE MOUSSA SECK SA BARGNY ET JE VOUS SOUHAITE UN BON GAMOU TADI SAKOU NIANN SI MOCC TALIBè YèPP
la vérité de l'histoire
c'est que les allemands ne combattaient pas en grece c'étaient les otomans le dernier empire musulman et quand les otomans des musulmans ont été vaincus par les athées les anglais et les français accompagnés du grand shahid
les terres d'islam qu'ils avaient ont été livrés anglais et plus tard au juif
mais il faut reconnaitre qu'il n'est pas parti de son plein gré on y pouvait rien les français étaient nos maitres absolu
YALA YONENE AK SERIGNE BABACAR SY KONE
SUNU DINÉ
SUNU TARIKHA
AK YONU TIVAOUANE
maodo sope nabi motakh ma sope ko kou bege nabi ma begele dabbakh mo diokh nabi bopame mo takh ma diokhco samabope kou begge nabi yalla beggele si kaw nga kham lii nabi indi tee santaneko
asfiyahi.org yalla naguene fii yagggua ak niounn content naniou thie Gamou GUI lool
euskey maam maodo , euskey khalifa ababacar yalla na yalla yokk sen leer te taasgnou thi barké amin !!!!!!!!!
dieuridieuf maodo gnogui laye sante di la guereume dakh li gua gnou defale manougne laco faye cana di gnane yalla mou fayale nioula te dolygnou si sa barque amine te niou topp sa tanque ba queroque nioulaye fequisi yalla naniou yalla teque si dioupe te moussalniou si lepou lou khetoque lou bonne dieuridieuf
le nimero de doudou kene mbaye
salam votre travail est extraordinaire beaucoup d encouragement que DIEU vous guide et vous protege salam
l'article est extrément important nous en sommes forts heureux car ces dits articles nous permettent de nous ressourcer davantages sur les bio et bibliographies de nos vénéres marabouts comme celui qui avait comme on le dit un pouvoirmulti dimensionnel.toutes nos félicitations
assalamou aleykoum puis -je savoir la signification de bourde et l'origine de imam boucheri
Dierejeuf sunu boroom,ganaw bi gnu fékéé réén yalnagnu ko téwé déwèn yag koo and ak wakeur seydi el hadji Malick sy (RA). Waat naani yonèn tébi dong moo jaar louné thi kaw souf koon nagnou bayi lép té ligéyalko guir gnou am fayouk allakhari (tabbi al jana)
dama begue seringe babakar sy ngir yala
sering mansour sy yala nanafi yague te wer
beue naala gussloooooll
l'acte de maodo devrait bien inspirer les "sergnes daaras de nos jours":
- préserver l'intégrité physique des enfants d'autrui dont on a la charge quitte à sacrifier celle des notres
- faire preuve d'un grand patriotisme.
Yalla na yalla yok ay lerram.bi diakhi el hadji malick sy.
yalna yalla yogou leram te tasoungou sibarkem amiiiiiiiiiiiine
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|