|
Seydi Khalifa Ababacar SY (RTA) Digne continuateur de Maodo, viatique pour la jeunesse
Manchallah sama thiofel si mome meunou mako expliqué.
kou am khalifa, amnga yonèn am maodo am cheikh miniou doy.yalna yalla yokou ay lèram tè tasniou thi barkèm,
machalla.machalla.yalla.nagnou.yalla.tass.thi.barkem
borom.bonnet.carrè.bi.ken.dou.mome
As Salâmu'alaykum
je veu savoir es que Dieu nous a dit de siuvre les tarikha ?
ou il la dit dans le coran et les prophetes aves quelle trarikha?
mercie
Alakhamdoulilah, Que Dieu nous guide dans le droit chemin, avec la bénédiction de cheikhal Khalifa Ababacar sy RTA. il est une personnalité incommensurable qui a su tenir haut le flambeau de l'islam et de la tarikha tidjaniya à travers le monde, yelna yalla tass gnou thi barkem.
dieureudieuf bakary lingua wakh yeup rafétna wayé goor gui mo mél nonou ndax dafa féss ci khol yi motakh founiou tolu daniy niane yalla yok léram , tass nou si barkén té wanaléniou ak mom kérock yomalkhiam amen . SEYDI ABOUBACAR SY MALA BEUG
Je suis très contente mame khalifa si on parle de lui j ai le coeur rempli de joie goorgui guedj la loi wakh ci mbakh Anna lou dess talk nagnou yalla ray ci dopé ko
Je suis très contente mame khalifa si on parle de lui j ai le coeur rempli de joie goorgui guedj la lo wakh ci mon mbakh Anma lou dess yalla nagnou yalla ray ci sope ko
kéne dou serigne babacar sy je suis trés trés fier de ce que je suis talibé cheikh machalla fila fi dogala syyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyy rék ba aldiana inchallla
Masahalla.soudiou.mame.se.babacar.sy.kene.dou.yaw
Liga.ligueye.si.tarikha.cheikhe.akhemette.tidiane.guene.dautouko.werente.yalna.youla.yalla.fayall.sibarke.soudiou.mame.seydalle.hadji.malick.sy.RTA.
Bravo pour ce magnifique travail alhamdoulilahi
Serigne babacar ken d''ou yawe sa kem tan doy ware manou gno wakh Lepe si yaw yalnagnou yalla tasse si sa barbe
Il est le cheikhal khalifa c''''est a dire le khalifa de tout les khalifa. L''''homme au bonné care,au menton verre.et au sourire legendere. J laim for
yalla nanou yalla fayal serigne babacar
Santa ti yalla bou ba niou amé kou mélni cheikhal khalifa yalla nanouko yalla fayal les mots s''échappent pour exprimer mes contentements
Salam! Li may yeuk sama yaram Ak sama col mane rek mako xam . yalla naniou souniou borom guindi tei bolai niou Ak serigne babacar sy rta amine inchallah . douniouko meussa reuthiou. Alkhamdoulilah
Serigne babacar sy c l homme de ma vie. Yalna yalla Hojo lé ram
serigne mouhamadoul mansour sy mbaye
sante serigne babacar sy ta di niane yalla mi dara teuwoul niou saf ko te nex ko mome serigne babacar sy nax saf naniou nex naniou te doy naniou
Salut a tous je remercie vivement M Bakary SAMB vu le travail costaux qu'il a abattu il a augmenté le degret d'amour que j'avais pour mon guide Sprituel
Walaxi mame babacar Kenn amoul fayam yalnaniouko yalla fayal té tass niou barkem inchallah
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|