|
TAMKHARIT : Voici les Priéres et Invocations à faire (Niaanou Tamkharit)
Macha Allah shoukrane!yalla naléne yalla faye yiw si barké s
SEYDINA MOUHAMED (SAWS)! Déwénatyléne à ttes la communauté musulmane baléne ma akh balna gneup! yalla nagnou yalla di khirek ci boppam moussal gnou ci shaytane badou gnou wathi si yonouu Siratal Moustakhim! amiiiine ya allah!!!Alhamdoulilahhh!!!!!!
salamou alyekoum serigne bi ñio gui laye ñiyou bou bakhe tè di fedeli soñiou sante ak guereum thi yaw ñio gu laye nianal thi Seydina Mouhamed saws lep lo fi beundi thi bakhe yalla nala ko ylla faye dieureudief
Assalamou Haleykoum Mbok yi gno ngi ziar si année bou béss bi té di baalou gneup akk Yalla nanou Yalla diégeul té nagou gnaan yeup.Té di gnaanal Pa Serigne Mor Diop Yalla nafi yag té andak wér car ki amougnou fayam
Yalla na lène borome bi faye séne bakh té bok Yol bi! Amine
Assalamou aleykoum. macha allah. diaza koumoul lahou an na hayran.
Dewwennety Mbokkeuyi ,contanne nayou lol.Dara dji ,Yal na Dieum sa kanam.
assalamouhanleiykoum dama beugone niane yi so wazifa ba paré mangui léne di ziar yalna yalla nangou.
Cours de Coran
Abba ndir vous forme à lire le Coran en 3 leçons seulement à distance par skype
Toute la formation se fait en 3 jours seulement
Adresse cite keur damel en face ice cream
Plus de soucis pour vous et la famille.
tabarakalaou fik dieuredieuf Laillahailallah mouhamadou rassouloullah
Yama ne lenne fayee. Diaradiaff
Merci asfiyahi dieureu dieuf
yallah naléne yallah faw té bayiléne fii bacii kanam kanam amine ya raabi
balene ma akh koi cette nouvelle annee soit une annee de sante de reussite de bonheur
asalamouhaleykhoum mboku talibèyi nagou niane tey balou akh bu bakh yal nalène yalla fèye yiw si barkè seydina mouhamed psl ake fèkè atte you barri amine dieureudieuf mame maodo malickh , diarama serigne babacar
Salam. Merci pour pour ces prières ci importantes. Qu''Allah nous facilite son accomplissement. Merci pour tout ce travail allant dans le sens de faire connaître l''Islam à tous. Maassalam.
Machalla Yalla nalene Yalla Faye
franchement c'est claire et accèssible yalla naléen yalla fay fay ngueun ngui pay.
Dieureudieuf Yalla na léén BOROM BI fey thie barké Serigne Babacar Al Khalifa
Macha Allah !
Djerediff Papa Mort Diop!
Vous beneficie de votre connaissance pour dans les monde.
Grace a vous, vos enfants qui vie a l'exterieur du Senegal ont tres bien fait les recommandations pour la fete de la tamkharit..
Nous sommes loin de notre "Khadara" mais vous rapproche de plus en plus " Yalla na la Yalla fay"" Te tass la thi barke Seigne Babacar SÝ ( ra)
Que le Bon Dieu vous protege et vous donne langue vie Amen..
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|