|
TRADUCTION DE ABADAA BOUROUQ DE SEYDI EL HADJ MALICK SY(rta) أبدا بروق تحت جنح ظلام
seydina cheikh, nungi lay jajefel bu baax! taxawaay bi ci hadra bi rafet na! asifyahi yeen itam!
S'il y a un texte de MAODO qui me fait pleurer, c'est ABADA BUROOQ
Machalla, kène dou Maodo Malick Fawade
yafi raw, boul wone ak yow nou rere , rta
yalna Allah gnouko mame Maodo ra yalla fayougnou leen yeen gniko traduire bagou mane ko comprendre amine
indiwat léén Maodo
Mba nguén défar bénén Maodo
RIP Mame!!!
seydi EL HADJI MALICK SY RADIALLAHOU TAALA ANEHOU DIEUREUDIEUF et a tout l`equipe qui on fait ce beau travail de traduction et de suivie jazzakoumaoul ALLAHOU khairane
yalna yalla fayalniou mame cheikh seydil hadji malick si maodo
Macha halla mame elhadji Malik sy amoulen morome si bi ligueye. Vivement d’autre traduction pour nous les no arabisans
Diereungène dieuf machallah liguèy bi rafetna جزاكم الله خيرا غير منصرم
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|