|
[VIDEO EXCLUSIVE] Serigne Abdou Aziz SY DABAKH (RTA) «Bawnane» ou la Générosité à l’état pur.
Merci pour ce beau video . Mame Abdou Yallah na nu ko Yallah fayal .... je suis de Tivaouane et je l'ai dans l'ame.............
serigne bi Yalla na lène Yalla faye gueune dji paye
yalla nalene yalla faye gueune di faye, amouniou kene koudoul yene. yalla naniou tass si sene barke!
Allah ! Voilà un post fabuleux !
Et les cœurs pleins de bonheurs mélangés avec un xaal indescriptible !
Aladji Abdou Ah ! Ce Saint Homme ! Ah ! ....
Xawouma saax laan la thi ték xana di ko HADIYAL ay Salatoul Fatiha Rék !
Radi’Yallahou’Anhou.
ALLAH SWT NOUS GARDE ET CONTINUE DE NOUS GRATIFIER DE LA PRESENCE EN NOTRE SEIN DE GUIDES DE CETTE DIMENSION SPIRITUELLE ET SOCIALE
MERCI INFINIMENT SERIGNE CHEIKH OUMAR SY JAMIL
Salam sama mbokk talibe bi qu'allah vous protege. je ne saurais dire l'amour que j'aie pour ce saint homme par le sens du verbe...
alahou akbar eskeuye mame abdou yalla na ko yalli dolli lèere té tass niou sou barkème diadieuf
Allahouma salli...lii dou néénne dé,Thieuyy yii Diambaar,
Yall nanou Allahou tass si sééne léére ak baarké.
Yaw nak Serigne Cheikh Oumar,yall nala Allahou fayall nou le...
ça va bientot faire un moment,que je me suis inscrit sur ce magnifique site,je regardait toutes les videos sans faire de commentaires,mais bii moome, je ne pouvais pas du tout me retenir.
Thieuyy sama Mame djii,heureume moo diottoone rék,waayé famou nou doone yaubou...Laa illaha illalaahou seyidounaa Mouhamed(psl).
DIEUREUDIEUF,
wa salam.
sante yalla rek sa sounè di nianal samay wadiour gir yalla kharelenn aldianana ak kep kouy fa fek ak niii lenn fa fek di niannal mame dabakh lou barrè barri yalla nanniou yalla taf thi barkem magi sakou niannn thi yen gir ma donn talibè cheikh bou wer amine
GIRYALLA VIDEO BOU DESSè LENNNENNN SOKHLA NAYKO GNOU DIARIGNOU DAKH MAME DABAKH LOU GEN THI GIMINAM REK DIARIGN LA BILLAHI
il faut tout simplement rendre grâce à Dieu de nous avoir fait des Tijanes. Il faut également continuer à prier pour qu' il nous donne la force de pratuquer comme il se doit les chartes de la confrérie
SY Malick YALLA NA YALLA yok sa lér Sénégal name nagnoula nakh sa mbakh say diguel ak say niane RTA
alhamdoulilahi rabbil aalamina que le bon dieu nous ouvre les porte de la lumière a travers le tarihatou tidjiania amine
je suis tres fier du site bonne continuation
bismilahi niongi santa yalla mi niou deef talibe chiekh mokou talibeyi niongi lenn yegell takousann fi cii parcell u 2 devent la grande mosqe bou serigne habib sy dabakh dimanche le 7 fervrie 2010 a 17h 00
Diazakallah. contannayou trop nakk.
merci du fond du cœur Yallah nala Yallah faye mome mi ame faiye
Merci beaucoup mbokk talibé
SENEGAL fi mou tolou sokhla na videos de references you mak gnou bakh yi.
tout d'abord un grand merçi à toi qui nous a procuré cette extraordinaire "59" que dieu te garde et te protege, quant à mame abdou et mame thierno yallah na nou lene yallah payale
ALLAHOU AK BAR meci mon DIEU de m'avoir cette chance aujourd'hui de découvir de ces vidéos si importantes et si tristes vraiment je suis émues
YALLA NANIOU YALLA TASS SI SENE BARKE ALLAHOUMA AMIIIIIINE
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|