|
[VIDÉOS ] ITINÉRAIRES - Doudou Kende Mbaye : Le porte-étendard du chant tidiane "«Je voulais devenir journaliste, mais mon père m'avait dit que mon destin était
POEME DE TALIBE SERIGNE BABACAR SY POUR LE TARIKHA
Louange à dieu qui nous éclair du jour au jour notre chemin à parcourir.
Louange au tout puissant qui nous a indiqué le tarikha de la lumiére.
Celui de cheykhouch chouyoukhi SEYDINA AHMADAT TIDIANI.
Louange à ALLAH qui, à chaque seconde nous montre ses "Kemtanes".
Diarama wa KEUR SEYDIL HADJI MALICK SY.
Siggil nguéne sunou Sénégal ci séne kham kham Ak séne yarr.
Mention spéciale à Doudou Kende Mbaye la voix d'or du tidianisme.
Yalla na niou yalla fayal Borom bonnet carré ba mi niou léral yonou Cheikh.
Yalla na niou yalla fayal Mame MALICK SY miniou wane Khayroul Anbiya.
Yalla na niou yalla fayal seydi ABDOUL AZIZ SY mi léral souniou khol yi.
FA INNA TARIKHATA CHEIKH HOUWA NOUROU KHALBI.
FA NAD-OUL LAHA HAYATANE WA MAWTANE FIT TARIKHATIL HOUDA: TARIKHATOU CHEYKHI AHMADAT TIJANI.
Je viens de découvrir le site le plus riche, le plus util pour parfaire ma pratique religieuse.
Bravos aux différentes contributions très enrichissantes.
Que DIEU gratifie nos saints tels CHEIKH TIDIANE CHERIF, EL HADJI MALICK , ETC..........
je viens de trouver le site le plus riche,pour bien pratique mon tariha.
bravos CHEIKH TIDIANE CHERIF de nous donné cet tariha dieureudieuf.
QUE DIEU gratifie nos saints tels EL HADJI MALICK .
ALHAMDOULILHA
Dieuredieufeti Doudou kend yangui beguel diam yi,lila yalla may journaliste you bari sougnou ka amone dotou gnou wakh dara.yalnala yala lafal thiat.en tout cas sougnou wa keur yeup yaw lagnouy begue.Ma soeur Maguette sarr quand elle entend ta voix elle se tais quand elle te voie elle pleure ndakh begue ci yaw.
yallah nanou yallah teunkeu si képarou seyidil hadji malick ta defnou deugue deugui talibé cheikh si barké seyidil hadji malick sy rta
Merci Doudou,tu continues de bercer avec ta voie douce qui nous rappelle nos vaillants guides spirituels de Elhadji Malick à Serigne Mansour Borom Darayi en passant par Seydy Ababacar, et ses frères. que Dieu te donne longue vie et une bonne santé. je te rappelle le rendez de l'année 2012 : la veille de pantecôte avec le Dahira Mouhsinina Wal Mouhsinaty de Peycouck..
thièy bilay ma sope khalifa ababacar borom bonè carrè bi
Ammougnou dara lougnthie wakh loudoul tarikha cheikh daal moy mbirma daal
Nagnou dem ba allakhira foofou ley leeré inchallah
DIARAWE LAKA MAME CHEIKH SEYDIL HADJI MALICK SY RTA; BOUDOULE WONE AK YAWE DINE DJI SOKE; AMELE NA NIOU LA NDIOUKEUL. YALNA TABARAKA WA TAHALA SOUGNOU BOROM FAYALE NIOULA SI BARKE SANGUOU SANGUEU YI AMINE .
yalla nanou yalla xolè SERIGNE BABACAR SY, ,dicko nianial yalla yok kay lèèr tè tass niou si barkèm.AMIN
Déja 8 jours que notre marabout, serigne MOUHAMADOUL MANSSOUR SY nous a quitté, yalla na yalla kok ay lèèr tè tass niou si barkèm. FATIHA ET 11 IKHLASS.AMIN
j aime beaucoup le tarikha tidjaniya et aussi touts les khalifa comme dabakh serigne mansour sy serigne chekh tidiane al mactoum el hadji malick sy
serigne mansour sy yana ko yallah kharel adjiana yana feke dji mamame you bakh ya ak bayame you bakhe ya amine
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|