|
Les Regles régissant la Réciation de la Salat - Al Fatihi
Je remercie tous les acteurs de ce site qui nous abreuve des milles et une merveille que renferme la Tariqa.
Je voudrais me procurer l'oeuvre Fakikhatou Toulab de Seydil Hadji Malick Sy sur la Doctrine et les pratiques du Tidianisme , Traduit par le Pr Rawane Mbaye.
Pensez vous pouvoir m'aider dans ce sens?
Je vous remercie.
Di dolè sante YALLAH,bi mouma dèfè madoune dioulite bou deugou,tè nèk talibè CHEIKH bou wère.AL HAMDOULILAHI RABIL ALAMINA.....
Di doli sante YALLAH, bi ma bolé si diné ISLAME ma done djoulite bou deugou, té gueum sounou BOROM di djouli si SANGUOU SANGUEYI SEYDINA MOHAMET ALEYI SALATOU WA SALAM mi niou wone yone bou djoube , té nék lou deugou thi mane boléma si tarikha CHEIKH té mou wére si mane maye sante YALLAH doli si limako santone douma tayi mouk di sante YALLAH SOUNOU BOROM, Tè DI DJOULI SI SEYDINA MOHAMET ( PSL) YALLAH NANOU YALLAH tass thi barkéme té sakhal niousi sounou gueum AL HAMDOULILAHI RABIL ALAMINA
Magui niane YALLAH mou fédje adjo yeupe si barké wérou GAMOU gui si barké AL KHOURANE KARIM SI BARKè BOROM BEUSS BI SEYDINA MOHAMET SAMA KHARITE SAMA TOUREUNEDO DOME ALKHAMDOULILAHI RABIL ALAMINA
MAA NGUIYE SANTA YALLA BIMA DIOUDOO THI DIINEYE ISLAAME GNOUULE NAKKA BILAAALE LE MUEZZIN DE KHAYERILE KHALEHI LAAHOU...J'EN SUIS TRES FIER TRES SATISFAIT RAWATINA NAK BIMMA DOONNEY TIIIDJAANE RAWATINA THI EUTOU MAAAME MAWEDO MAALIKK SY....RADDIYA LAAHOU TAALLAAA ANEHOU...YALLA NAGNOUKO YALLA FAYALE TE TAAFEGNOU THI BARKEEEME...AAAAMIIINE...PROFESSEUR RAWAANE MBAYE...YALLA NAGNOUKO YALLA FAYALE THI BARKEP SEYDOUNAA MOUHAMMAD ALETEHI SALAAHI...AAAAMIIINE...
Je suis très content et attaché à votre site et prêt à recevoir toute documentation sur l'Islam
Heureuse de découvrir ce site si intéressant. Je souhaite obtenir le livre: " Fakikhatou Toulab " de Seydil Hadji Malick Sy sur la Doctrine et les pratiques du Tidianisme , Traduit par le Pr Rawane Mbaye. Pourriez- vous me guider si possible? Merci
Oú trkouve-t-on les réponses aux différentes questions posées? Merci
assalamou aleikoum sante yalla thi tarikha cheikh j'aimerais bien me procurer le livre du PR RAWANE " FAKIKHATOU TOULAB " de SEYDI HADJI MALICK traduit en francais
ASSALAMOU ALEYKOUM BOKK YI MAGUI ZIAR BOLOM DJOULIT CII WER WOU TEDD WI DI BALLOU AKHA BALNA GNEUPP.
YALNA YALLA DIEUGEUL GNOU SOUGNOU BAKKAR YEUPP TA NAGOUL SOU GNOU DIAMOU YALLA CI WER WOU TED WI " MOUBARAK"
SANT YALLA BI MOU BOLLE SI SITE BII GNOU CI DIARIGNO YOK KHAM GUENEL LI TARIKHA BI. DIEUREGENN DIEUF.
LA PERLE DE LA PERFECTION....SALAATOUL FATIHI...DIEUREDIEUF SERIGNE BABACAR SY...QUI NOUS A GUIDE DANS LA VOIE TIDJIANYA...QUE DIEU LE RETRIBUE ET A CHEIKH SEYDI ELAHADJI MALICK SY....RTAM.....
LA PERLE DE LA PERFECTION DIT SALAATOUL FÂTIHI PEUT SAUVER LE MONDE ENTIER. QUE LE BON DIEU COMBLE, DE GRACE ET DE BONHEUR A TOUS LES MUSULMANS DU MONDE EN GENERAL ET LES TALIBES CHEIKH EN PARTICULIER.
sante yalla lu bare di diuli ci seydina muhamed s.a.w.s.yala yok leru c. a-t.cherif io posso dire che la salat fatiha e vera che puoi salvare anche il mondo intero che bella come salat alhamndoulilah Elhadji Moussa Dieye imam ratib de sakal yalla nafi yague té wer
Je viens de découvrir ce site plein d'enseignements précieux. Que Dieu bénisse ses administrateurs, élargisse le spectre de leurs connaissances, les garde longtemps parmi nous en leur attribuant des rétributions au delà de toutes leurs espérances.
gnoungui ndookel serigne lamine gueye
yalla nanou yalla fayal cheikh
alhamdou LILAHI rabil alamine souma salatouhou wa salamouhou ala sèyidil woudioud MOUHAMADOU IBN ADBOULAHI IBN ABDOUL MOUTALIB IBN HACHIMIN mangui sant borom bi bouma sakhè mou boolèma ci khèèt bou gueun thi khèèt yi,mou yoni si man kou gueun thi mbindèèf be parrè mou weursegalma ma doon talibè thi tarikha bou geun thi tarikha yi di tarikha( khoutboul awliya-i cheiykhoul chouyikhi abal abbas cheiykhana AHMAD TIDJIANI chèrif (D.A°
Bismillah Ar-rahaman Ar-rahim wa salatou wa salam ala seydil wara Taha Mouhamad .
Qu'ALLAH (LSI) nous pardonne tous péchés et négligences et nous permette de nous humilié devant Sa Puissance et Sa Majesté!
Courage et merci pour les services rendus à travers la bonne information sur la Tariqa Tidjani que j'aime d 'un amour sans faille!
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|