Mangui sante sounou boroom soubhaanahou wataalah di diouly thy sangou sangueyi seydina mouhamet salalaahou aleyhi wa salam bima samaboroom deffe dioulyt ,boolema thi tarekha cheik .diniaane sounou boroom,yalnaniou sakhalal souniou imaan ,yokalniou sounou lislam thi barke yonentebi salalaahou aleyhi wasalam.
Thi barke maqueniou baakheyi .Aamin.