|
(VIDEO) Ziarra Générale Tivaouane : Qui était Cheikh Seydi El Hadl Malick Sy (RTA) par Serigne Abdoul Aziz Al Amine
serigne abdoul aziz thiam
vraiment les gens on ne peut pas vous remercier assez de toutes les informations de la Hadara que vous ne donnez en temps réel seulement j'aimerai avoir ces videos dans mon PC mais j'aimerai savoir comment les telecharger ,merci de bien vouloir m'aidez parce que je suis loin du pays té momay wétali serieux
diajakoumouLaha hayran .Vous nous avez permi d'avoir bcp d'infos sur cette source intarissable de savoir qu'est Seydi Hadji Malick que ns ne connaitrerons jamais assez.
dieu re guene dieuf waye gua you bakh beugue na si gnene deee
SERIGNE ABDOU AZIZ SY YALNA FI YAGUE LOLLL TEWER
Tres orgueuilleux d'être tidjane et en suis tres content.Dieureudieuf Malick
Yalla na lène Yalla fèye...Serigne Abdou Yalla nafi yagg té Wér...
dieureudieuf mame abdoul aziz junior pour la clarté des informations mais surtout pour pédagogie dans la transmission du savoir,queDieu te préserve encore longtemps
yalla nallenne yalla faye sy malick teh tass nioun si senn barkehhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh
fonk saa dinné fonk saa boppp
yalla na yalla faye len sop nalen trop maye len soutoura wer ak mouthia yakha khamkham bi
yokha khamkham bi ak wer gou yaram balenma si wolof bou setoul bi
yalla na yalla faye len sop nalen trop maye len soutoura wer ak mouthia yakha khamkham bi
macalla segn abdou yalna fiague té weer.mome ak diambote seydi el hadji malick.yeup
Pour pouvoir télécharger des fichiers audio et vidéo, il faut télécharger et installer Internet Download Manager (IDM). C'est un outil de téléchargement de fichiers. Apres l'installation, il s'intégre directement sur votre navigateur, vous permettant de télécharger des fichiers.
sunu khole béssalate guén ko sa suniou lén déglo rék ni lay démé !!yalla na lén yalla yagal sunu kanam guén yaga djité khadra biiiii
al amine yalnafi yague tewer ak wakeur el hadji malick yeup, merci asfiyahi
MERCI SY .Toujours aux rendez vous .
Yalna Sounou borome Soub anahou wa talaa fayal noulène
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|