|
SALATOUL FATIHI - Apprentissage à sa Lecture et Traduction
dilene santa boubaha bah yene guinuye diapale boubah si dinedji. yalla nalen yalla diapale, ci barqè serigne babacar sy.
Yalla na léne Yalla faye ngueun dji paye.Liguéye bi ngéne di def am na solo! wallahi bekk na niou! Yalla na Yalla contane , yonente bi si sallallahou aleyhi wa sallam contane, Cheikh Ahmad Tidiane contane, Mame Cheikh Seydil Hadji Malick contane ak Moukhaddam yi ak hadara bi yeup ci barké yonente bi Seydina Mouhammad sallallahou aleyhi wa sallam.
dieureudieuf wa ASFIYAHI magui contane ci orientation gene di joxe ci dinedji si tarihabi di gnou hamal lou bari si lougnou leuntone yalla na lene yalla fey ci barke HADARABI .AMINE
yalla na lenne faye lu sute sen ndiorte.Yalla na Yalla ande ak yenn dahimane ti barke Cheix Seydi El Hadj Malick SY rta. Yalla def niu njaboot Cheixna Cheix Ahmet Tidjani rta.
[macha allah. yanna yalla dolli leral yono tidiane ...
magui sante wa ramadan yappo wa asfiyahi yalla gissna taxawayyi
[macha allah. yllana yalla fay ndiappo
mack ndaw goor jigeen
kilifa ak noun talobiy yalla mannako yannakodeff allahoma amiiiiiiiiiiiin...
je suis tres content de trouver cette site ça
de pui que bima comasee ducge senn sitte bii mague siy guis gnarigne dammaye gnanne yalla mu dolli jewal ba lii muna sakh assane boye st ls
JE SUIS VRAIMENT FIERE D'ETRE PARMIS CEUX QUI AIME ATIJANI ET JE PRIS LE BON DIEU QU'IL M'AIME LUI AUSSI
MAIS CE SITE EST UN DAHARAA UNIVERSEL POUR TOUT MUSULMAN , TIJAN OU BIEN AMOUREUX D'ATIJANI
ALHAMDOULILAHI! Je suis très heureuse de retrouver votre site, qui pourra me faire comprendre beaucoup choses sur ma Tarikha Tidjani Inchallah! Que Dieu vous bénisse et vous donne longue vie Amine!
Merci Cheikh Ahmet Tidjane Cherif, ce qu'on a personne d'autre ne pourra l'avoir, wird biii amoul morom billahi wallahi wa talakhi.
sante nagnou yalla bou werewere boufi site bou melni amé dieureudieuf
je suis très content de recevoir vos messages dans le cadre de l'islam.Cela me aide beaucoup a rectifié beaucoup de choses.
Assalamou aleykoum,
Vraiment je viens d'ouvrir cette page mais j'étais très contente et cela nous permettra au moins de connaître le Tarikha. Mais je voudrais poser une question je peux réciter le saloul fatihi mais je crois toujours me tromper à la fin merci de me guider là où on dit cette formule :
INNA LAHA MA MALA IKA TOUHOU YOUSSALOUNA .............
macha llaha yalna allah yokk kham kham bi tè barkèl ko amin
tres bon site avez vous s il vous plait une priere sur al istikhara merci
diasakoumou lahou khairal diasa i se ligueye fafetna yalna yala fayelen yiw thi barke cheikhina wa seydina aboubacar sy ibn elh malicksy radiyalaou anhouma amine
DIEUREU GUENE DEUF YALLA NALEN YALLA FAY
JE SAVE PA RECITER SALATOUL FATIHA MAIS GRACE A VOUS JE VIENS DE LAPPRENDRE
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|